Wikipedia 2006 (Static HTML - No images) is on line here! [.7z dumps also available]
Sorry, English version is not working. Please, connect the Xët wu njëkk - Wikipedia

Xët wu njëkk

Ab jukkib Wikipedia.

Nataalu Wikipedia Dalal-jàmm ci Wikipedia

Jimbulang bu Ubbeeku bi

Seetal ci 727 jukki ci kàllaama wolof:

Nas wi bokk na ci bëre biy dàq ber bi ñu ber yenn làkk yi (rawatina ci internet bi), xëcc itam gëndaloo guy yamale te di jàpplante, loolu di sukkandiku ci sañ-sañu askan yi gàddu seen kuute ci caada.

Àdduna bu gën di yamale, ak gën di tinkiku ci la aju !!!




Askan
Yeneen sémbi Wikipedia ci yeneeni kàllaama. Nu lim ci ñenn ñi rekk.

Lim bu mat · Multilingual coordination

Nataalu ayubés bi
Lat Joor Joob Ngóone Latiir Faal
Lat Joor Joob Ngóone Latiir Faal
Lat Joor Joob waxambaane wu jàmbaare la woon, wu amoonug dogu, mu bokkoon ci ñu mag ñi daa jàmmaarlook sancaan yi ci goxub Afrig, mu nekkoon di kenn ci ñi ci gën a jàmbaare, gën cee fés, kenn melul ni moom ci sopp suufam ak ndonoom. Amoon na fit wow kenn du ko doyadil, daawul tiit ak lu man a xew. Nekkoon na njiitul xare lu mag, di aji politig ju ñaw, ju di boroomug jommal. Ci atum 1862 g.j, la ñu fal Lat Joor Dammeel ca Kajoor.
Yeneen naal ci Wikipedia

Wikibaatukaay

Wolof Wikiquote

Yeneen sémbi Wikipedia ciy kàllaamay waa Afrig

Afar · Afrikaans · Akan · አማርኛ · Bamanankan · Chicheŵa · chiShona · chiTumbuka · Ɛʋɛ · Fulfulde · Gĩkũyũ · هَوُسَ · Igbo · isiXhosa · isiZulu · Kinyarwanda · Kirundi · Kiswahili · Kongo · Lingála · Luganda · Malagasy · Malti · Oromoo · Oshiwambo · Sängö · Sesotho · Setswana · siSwati · Soomaaliga · ትግርኛ · tshiVenda · Twi · Xitsonga · (ngir yeneeni Wikipedia, xoolal ci bànqaasu wet gi)

Ay kàllaamay waa Afrig ci wikipedia yu ëppal 1000 jukki

Afrikaans · Kiswahili · Yorùbá ·